1
Yowaan 18:36
Téereb Injiil
TI
Yeesu ne ko: «Sama kilifteef nekkul ci àddina. Bu sama kilifteef nekkoon àddina, sama surga yi dinañu xeex, ngir bañ ñu jébbal ma Yawut yi. Waaye sama kilifteef nekkul àddina.»
Compare
Explore Yowaan 18:36
2
Yowaan 18:11
Waaye Yeesu ne Piyeer: «Roofal jaasi ji ci mbaram. Ndax warumaa naan kaasu naqar, bi ma Baay bi sédd?»
Explore Yowaan 18:11