1
Saag 2:17
Téereb Injiil
TI
Noonu ngëm gu àndul ak jëf, amul benn njariñ.
Compare
Explore Saag 2:17
2
Saag 2:26
Kon nag ni jëmm ju amul ruu nekke ndee, noonu la ngëm gu àndul ak jëf nasaxe.
Explore Saag 2:26
3
Saag 2:14
Te lii itam samay bokk: ku ne gëm nga, te jëfewoo ko, loolu lu muy jariñ? Ndax googu ngëm man na laa musal?
Explore Saag 2:14
4
Saag 2:19
Gëm nga ne Yàlla kenn la; loolu lu baax la, waaye xamal ne, jinne yi it gëm nañu loolu, ba dañoo tiit bay lox.
Explore Saag 2:19
5
Saag 2:18
Waaye xanaa dina am ku ne: «Yaw am nga ngëm, man am naa ay jëf.» Yaw nag won ma sa ngëm gu àndul ak jëf; man, ma feeñal la sama ngëm ci samay jëf.
Explore Saag 2:18
6
Saag 2:13
Ndaxte ku yërëmul, yoon du la yërëm. Te yërmande mooy not àtte.
Explore Saag 2:13
7
Saag 2:24
Kon nag gis nga ne Yàlla ci jëf lay àtte nit ni ku jub, waaye du ci kaw ngëm kese.
Explore Saag 2:24
8
Saag 2:22
Kon gis nga ne ngëm dafa lëngoo ak ay jëfam, te ngëmam mat ci kaw jëf jooju.
Explore Saag 2:22