1
Yawut ya 8:12
Téereb Injiil
TI
Ndaxte dinaa leen baal seeni tooñ, te dootuma fàttaliku seeni bàkkaar.»
Compare
Explore Yawut ya 8:12
2
Yawut ya 8:10
Boroom bi nee na: Kóllëre gaa ngii, kóllëre gi may fas ak bànni Israyil, bu bés yooyule weesoo. Dinaa def samay ndigal ci seen xel, bind ko ci seen xol. Dinaa nekk seen Yàlla, ñu doon samay gaay.
Explore Yawut ya 8:10
3
Yawut ya 8:11
Kenn dootul wara jàngal moroomam walla mbokkam, di wax naan: “Xamal Boroom bi!” Ndaxte ñépp dinañu ma xam, li dale ci ki gëna ndaw ba ci ki gëna mag.
Explore Yawut ya 8:11
4
Yawut ya 8:8
Waaye nag Yàlla sikk na bànni Israyil, bi mu naan: Boroom bi nee na: «Ay fan a ngi ñëw yu may fasi kóllëre gu bees ak bànni Israyil ak waa Yude. Kóllëre googu nag bokkul ak gi ma fasoon ak seeni maam
Explore Yawut ya 8:8
5
Yawut ya 8:1
Lii mooy li ëpp solo ci li nuy wax: am nanu sarxalkat bu mag bu mel noonu, moom mi toog ci ndijooru Aji Màgg ja ca nguuram ca kaw.
Explore Yawut ya 8:1