Yawut ya 8:8
Yawut ya 8:8 TI
Waaye nag Yàlla sikk na bànni Israyil, bi mu naan: Boroom bi nee na: «Ay fan a ngi ñëw yu may fasi kóllëre gu bees ak bànni Israyil ak waa Yude. Kóllëre googu nag bokkul ak gi ma fasoon ak seeni maam,