1
Yawut ya 6:19
Téereb Injiil
TI
Ci yaakaar jooju lanu sës sunu xol, ba mana sampu bu dëgër. Yaakaar la juy jàll ba fa Yàlla nekk, ca gannaaw ridob bérab bu sell baa sell.
Compare
Explore Yawut ya 6:19
2
Yawut ya 6:10
Yàlla ñàkkul worma bay fàtte seen liggéey ak mbëggeel, gi ngeen wone ci turam, ci li ngeen dimbali ay gaayam, te yéena ngi koy def ba tey.
Explore Yawut ya 6:10
3
Yawut ya 6:18
Noonu ñaari jëf yooyu nga xam ne duñu tebbiku te Yàlla manu cee dellu gannaaw, dañu nuy gëna sóob ci muñ, nun ñi daw ba am kiiraay, ngir nu mana téye bu dëgër yaakaar, ji mu nu dig.
Explore Yawut ya 6:18
4
Yawut ya 6:1
Kon nag léegi nanu jóge ci liifantu gi jëm ci Kirist, te jàll cig mat. Nanu baña dalaat njàngle mu jëkk moomu, ci ne nit ñi dañoo wara tuub jëf, yi jëm ci dee, te gëm Yàlla
Explore Yawut ya 6:1