1
Yawut ya 3:13
Téereb Injiil
TI
Waaye bés bu nekk, deeleen soññante ci lu jëm ci Yàlla, fi ak bés boobu ñu wax wéyul, ngir ragal bàkkaar nax kenn, ba xolam tëju.
Compare
Explore Yawut ya 3:13
2
Yawut ya 3:12
Bokk yi, wottuleen ba kenn ci yéen baña am xol bu bon te gëmadi, bay dëddu Yàlla jiy dund.
Explore Yawut ya 3:12
3
Yawut ya 3:14
Am nanu wàll ci Kirist, su nu wéyee fii ba muj ga ci sunu kóolute, gi nu amoon ca njàlbéen ga.
Explore Yawut ya 3:14
4
Yawut ya 3:8
buleen dëgër bopp, ni seeni maam defoon ca màndiŋ ma, keroog ba ñu dëddoo Yàlla, di ko diiŋat.»
Explore Yawut ya 3:8
5
Yawut ya 3:1
Kon nag yéen bokk yu sell yi, yéen ñi Yàlla woo, ngeen bokk ci nguuram gu kawe ga, seetleen ci Yeesu, moom miy ndawu Yàlla li, di sarxalkat bu mag bi ci yoon wi nu gëm.
Explore Yawut ya 3:1