1
Galasi 3:13
Téereb Injiil
TI
Waaye Kirist jot na nu ci alkànde, ji yoon wi indi; mu gàddul nu ko, ba far alku moom ci boppam, ndaxte Mbind mi nee na: «Képp ku ñu rey, wékk ko ci bant, alku nga.»
Compare
Explore Galasi 3:13
2
Galasi 3:28
Kon nag amul xàjjale ci diggante Yawut ak ki dul Yawut, ci diggante jaam ak gor, ci diggante góor ak jigéen. Yéen ñépp benn ngeen ci seen bokk ci Kirist.
Explore Galasi 3:28
3
Galasi 3:29
Bu ngeen bokkee ci Kirist, kon bokk ngeen ci askanu Ibraayma, te jot ngeen xéewal, yi ko Yàlla dig.
Explore Galasi 3:29
4
Galasi 3:14
Noonu barke bi Yàlla dig Ibraayma baawaan na, ba daj ñi dul Yawut te gëm Kirist Yeesu, te nu jot ci kaw ngëm Xel mu Sell, mi Yàlla dige.
Explore Galasi 3:14
5
Galasi 3:11
Bir na sax ne sàmm yoon du tax kenn jub fa kanam Yàlla, ndaxte Mbind mi tëral na ne: «Ku jub ci kaw ngëm dinga dund.»
Explore Galasi 3:11