1
Galasi 2:20
Téereb Injiil
TI
Daajaale nañu ma ak Kirist ca bant ba, te noonu du man may dundati, waaye Kirist mooy dund ci man. Dundu mbindeef, gi may dund nag, maa ngi koy dund ci gëm Doomu Yàlla ji, moom mi ma bëgg, ba joxe bakkanam ngir man.
Compare
Explore Galasi 2:20
2
Galasi 2:21
Duma neenal yiwu Yàlla, ndaxte su sàmm yoon doon taxa jub fa kanam Yàlla, kon Kirist dee na cig neen.
Explore Galasi 2:21
3
Galasi 2:15-16
Nun danoo cosaanoo ci xeetu Yawut, te bokkunu ci xeet, yi xamul Yàlla tey bàkkaar. Teewul nu xam ne Yàlla du àtte kenn ni ku jub ci kaw sàmm yoon, waaye ci gëm Yeesu Kirist. Kon nun itam gëm nanu Kirist Yeesu, ngir Yàlla àtte nu jub ci kaw gëm Kirist, te du ci sàmm yoon. Ndaxte du caageenug sàmm yoon mooy tax Yàlla àtte kenn ni ku jub.
Explore Galasi 2:15-16