1
Galasi 1:10
Téereb Injiil
TI
Ndax kon nit laay wuta gëmloo, am damay fexee yey Yàlla? Mbaa damay wuta neex nit ñi? Su ma doon wuta neex nit ñi ba tey, kon duma nekkati jaamu Kirist.
Compare
Explore Galasi 1:10
2
Galasi 1:8
Waaye su fekkee kenn ci nun ñëw, walla malaaka sax mu jóge asamaan, di yégle beneen xibaar bu méngoowul ak bi nu leen yégal, kooku yal na alku!
Explore Galasi 1:8
3
Galasi 1:3-4
Na yiw ak jàmm féete ak yéen, jóge ci Yàlla sunu Baay ak Yeesu Kirist Boroom bi, moom mi joxe bakkanam ngir dindi sunuy bàkkaar, te musal nu ci àddina su bon, si nu nekk, dëppook coobarey Yàlla sunu Baay
Explore Galasi 1:3-4