Bible App logo
Search Icon

Galasi 1:3-4

Galasi 1:3-4 TI

Na yiw ak jàmm féete ak yéen, jóge ci Yàlla sunu Baay ak Yeesu Kirist Boroom bi, moom mi joxe bakkanam ngir dindi sunuy bàkkaar, te musal nu ci àddina su bon, si nu nekk, dëppook coobarey Yàlla sunu Baay,

Free Reading Plans and Devotionals related to Galasi 1:3-4