1
Jëf ya 18:10
Téereb Injiil
TI
Ndaxte maa ngi ànd ak yaw, te kenn du la jàpp, ba fitnaal la, ndaxte am naa xeet wu bare ci dëkk bii.»
Compare
Explore Jëf ya 18:10
2
Jëf ya 18:9
Naka noona Boroom bi feeñu Pool ci guddi ne ko: «Bul tiit dara, waaye deel wax te baña noppi.
Explore Jëf ya 18:9