1
Jëf ya 19:6
Téereb Injiil
TI
Te bi leen Pool tegee loxo, Xel mu Sell mi ñëw ci ñoom, ñuy wax yeneen làkk, di wax ci kàddug Yàlla.
Compare
Explore Jëf ya 19:6
2
Jëf ya 19:11-12
Booba Yàllay def ay kéemaan yu ràññiku yuy jaar ci loxoy Pool. Ñu yóbbul sax ñi wopp ay kaala ak ay taraxlaay yu laaloon yaramam, ba jàngoro yi di leen bàyyi, rab yay génn ci ñoom.
Explore Jëf ya 19:11-12
3
Jëf ya 19:15
Waaye bi ñu ko defee rab wa ne leen: «Xam naa Yeesu, xam naa it kuy Pool, waaye yéenay ñan?»
Explore Jëf ya 19:15