1
Jëf ya 16:31
Téereb Injiil
TI
Ñu ne ko: «Gëmal Yeesu Boroom bi, kon dinga mucc, yaw ak sa njaboot.»
Compare
Explore Jëf ya 16:31
2
Jëf ya 16:25-26
Ba guddi giy xaaj nag, Pool ak Silas di ñaan ak di sant Yàlla, te ñeneen ñi nekk ca kaso ba di leen déglu. Ca saa sa suuf yëngu bu metti, ba fondamaab kaso ba daanu; bunt yépp daldi ne kulbét ubbiku, te jéngi ña ñu tëj ne téll tijjiku.
Explore Jëf ya 16:25-26
3
Jëf ya 16:30
Mu génne leen ci biti ne leen: «Kilifa yi, lu ma wara def, ba mucc?»
Explore Jëf ya 16:30
4
Jëf ya 16:27-28
Ci kaw loolu boroom kaso ba tiite ci ay nelaw, gis bunt yépp ubbiku. Mu daldi bocci jaaseem, bëgga xaru, yaakaar ne ña ñu tëj dañoo daw. Waaye Pool wax ci kaw ne: «Bul lor sa bopp, nun ñépp nu ngi fi.»
Explore Jëf ya 16:27-28