1
Jëf ya 15:11
Téereb Injiil
TI
Nun daal ci yiwu Yeesu Boroom bi lanu yaakaara mucce, te ñoom itam, ci lañu wékku.»
Compare
Explore Jëf ya 15:11
2
Jëf ya 15:8-9
Yàlla, mi xam xol yi, seede na leen ci li mu leen may Xel mu Sell mi, ni mu nu ko maye nun itam. Gënalantewu nu ak ñoom, ci li mu sellal seen xol ci kaw ngëm.
Explore Jëf ya 15:8-9