1
Jëf ya 14:15
Téereb Injiil
TI
«Yéen nit ñi, lu leen xiir ci lii? Nun it ay nit lanu, ñu bokk bind ak yéen. Te nu ngi leen di xamal xibaaru jàmm ne leen, ngeen dëddu yëfi neen yii te waññiku ci Yàlla miy dund te sàkk asamaan, suuf, géej ak li ñu ëmb lépp.
Compare
Explore Jëf ya 14:15
2
Jëf ya 14:9-10
Moom nag muy déglu Pool miy waare. Noonu Pool xool ko jàkk, gis ne am na ngëm ngir wér. Mu ne ko ak baat bu dëgër: «Jógal taxaw bu jub.» Noonu nit ki ne bërét, jóg, daldi dox.
Explore Jëf ya 14:9-10
3
Jëf ya 14:23
Ci mbooloom ñi gëm mu nekk nag, ñu tànn ci ay njiit; ba noppi ñu ñaan Yàlla ak di woor, dénk leen Boroom bi ñu gëm.
Explore Jëf ya 14:23