1
3.Yowaan 1:2
Téereb Injiil
TI
Sama soppe, maa ngi ñaan, Yàlla may la jàmm ci lépp, ànd ak wér-gi-yaram, ju mel ni sa naataangeg xol.
Compare
Explore 3.Yowaan 1:2
2
3.Yowaan 1:11
Sama xarit, bul roy lu bon, waaye lu baax rekk. Kuy def lu baax, ci Yàlla nga bokk; kuy def lu bon, xamoo dara ci Yàlla.
Explore 3.Yowaan 1:11
3
3.Yowaan 1:4
Awma mbég mu ëpp lii: ma dégg ne samay doomi diine ñu ngiy jaar ci tànki dëgg.
Explore 3.Yowaan 1:4