1
2.Yowaan 1:6
Téereb Injiil
TI
Lii mooy mbëggeel: nu wéer sunug dund ci ndigali Yàlla; loolu mooy ndigalam, la nu jotoon ca njàlbéen ga, te ci lanu wara jaar.
Compare
Explore 2.Yowaan 1:6
2
2.Yowaan 1:9
Képp ku saxul ci dénkaaney Kirist, xanaa di ko weesu, bokkul ci Yàlla; ku sax ci dénkaane yi, bokk nga ak Baay bi ak Doom ji.
Explore 2.Yowaan 1:9
3
2.Yowaan 1:8
Kon moytuleen, ngir baña ñàkk seen añub coono, waaye ngeen am yool bu mat sëkk.
Explore 2.Yowaan 1:8
4
2.Yowaan 1:7
Maa ngi wax loolu nag, ndaxte am na ñuy sànke ñu bare, ñu tasaaroo ci àddina, te nanguwuñu ne Yeesu Kirist wàcc na, nekk nit. Kooku aji sànke la, di Bañaaleb Kirist.
Explore 2.Yowaan 1:7