1
2.Timote 2:15
Téereb Injiil
TI
Góor-góorlul ba teew fa kanam Yàlla, nekk liggéeykat bu mu nangul te rusoo ci dara, di faramfàcce bu jub kàddug dëgg gi.
Compare
Explore 2.Timote 2:15
2
2.Timote 2:22
Dawal bépp bëgg-bëggu ngone, te sóobu ci njub, ngëm, mbëggeel, jàmm, ànd ak ñépp ñiy tudd turu Boroom bi ak xol bu sell.
Explore 2.Timote 2:22
3
2.Timote 2:24
Te jaamu Boroom bi warula xuloo, waaye na lewet ci ñépp, jekk ngir jàngle tey muñ fitnay noon.
Explore 2.Timote 2:24
4
2.Timote 2:13
su nu ko ñàkkee kóllëre, moom dina sax ci kóllëreem, ndax manula weddi boppam.
Explore 2.Timote 2:13
5
2.Timote 2:25
Na jubbanti cig suufe ñi koy diiŋat, tey yéene Yàlla xiir leen ci réccu, ba ñu xam dëgg
Explore 2.Timote 2:25
6
2.Timote 2:16
Moytul bépp jataayu waxi neen yu àddina kese, ndax ña fa toog dinañu gëna xuus cig weddi
Explore 2.Timote 2:16