1
1.Yowaan 5:14
Téereb Injiil
TI
Kóolute gi nu am ci kanam Yàlla mooy lii: su nu ko ñaanee dara ci coobareem, dina nu nangul.
Compare
Explore 1.Yowaan 5:14
2
1.Yowaan 5:15
Gannaaw xam nañu ne dina nangu lépp lu nu koy ñaan, xam nanu it ne li nu ko ñaan, jox na nu ko.
Explore 1.Yowaan 5:15
3
1.Yowaan 5:3-4
Ndaxte mbëggeel ci Yàlla mooy sàmm ay ndigalam; te ay ndigalam diisuñu. Ndaxte képp ku juddu ci Yàlla day not àddina; te li nuy note àddina mooy sunu ngëm.
Explore 1.Yowaan 5:3-4
4
1.Yowaan 5:12
Ku am Doom ji, am nga dund; ku amul Doomu Yàlla, amuloo dund.
Explore 1.Yowaan 5:12
5
1.Yowaan 5:13
Maa ngi leen di bind yëf yii, yéen ñi gëm turu Doomu Yàlla ji, ngir ngeen xam ne am ngeen dund gu dul jeex.
Explore 1.Yowaan 5:13
6
1.Yowaan 5:18
Xam nanu ne képp ku juddu ci Yàlla doo sax ci bàkkaar, waaye Doomu Yàlla ji mooy wottu sa bakkan, ba Ibliis du la manal dara.
Explore 1.Yowaan 5:18