1
2.Korent 11:14-15
Téereb Injiil
TI
Te loolu jaaxalu nu, ndaxte Seytaane moom ci boppam day mbubboo malaakam leer. Kon nag ay ndawam mbubboo ndawi njub, loolu du nu jaaxal. Dees na leen fey seeni jëf.
Compare
Explore 2.Korent 11:14-15
2
2.Korent 11:3
Waaye ni jaan ja naxe woon Awa ci pexeem, ragal naa yéen itam ñu lëmbaaje ni seen xel, ba ngeen dëddu xol bu laab, bi ngeen amoon ci seen diggante ak Kirist.
Explore 2.Korent 11:3
3
2.Korent 11:30
Su ma damu waree kon, ci sama néew doole laay damoo.
Explore 2.Korent 11:30