1
2.Korent 10:5
Téereb Injiil
TI
ak bépp tiitar buy jànkoonteek xam-xamu Yàlla, te danuy not bépp xalaat, ba mu déggal Kirist.
Compare
Explore 2.Korent 10:5
2
2.Korent 10:4
Ndaxte gànnaay, yi nuy xaree, jógewuñu ci nit, waaye ca Yàlla lañu jóge, te ànd ak kàttan, ngir daaneel ay tata. Danuy daaneel xalaat yi dul dëgg
Explore 2.Korent 10:4
3
2.Korent 10:3
Dëgg la ne nit rekk lanu, waaye dunu xeexe ni nit.
Explore 2.Korent 10:3
4
2.Korent 10:18
Ndaxte ki neex Yàlla, du ki naw boppam, waaye ki Yàlla gërëm.
Explore 2.Korent 10:18