1
1.Timote 5:8
Téereb Injiil
TI
Ndaxte ki defalul ay bokkam dara, rawatina ay waajuram, weddi na yoonu ngëm wi, ba yées ku gëmadi.
Compare
Explore 1.Timote 5:8
2
1.Timote 5:1
Bul gëdd mag, waaye waxtaanal ak moom ni sa baay. Ndaw it, nga digal ko ni sa rakk
Explore 1.Timote 5:1
3
1.Timote 5:17
Li jëm ci njiiti mbooloo mi nag, joxal teraanga ju mat sëkk ñi ciy rafetal seen liggéey, rawatina ñi sax dàkk ci waare bi ak njàngle mi.
Explore 1.Timote 5:17
4
1.Timote 5:22
Bul gaawa teg loxo kenn, ba fal ko, di séddu noonu ci bàkkaari jaambur, waaye dëkkal ci sellaay.
Explore 1.Timote 5:22