1
1.Timote 4:12
Téereb Injiil
TI
Bu la kenn xeeb ndax say at, waaye defal sa bopp royukaayu ñi gëm ci say wax ak say jëf, ci sa mbëggeel, sa ngëm ak sa cell.
Compare
Explore 1.Timote 4:12
2
1.Timote 4:8
Ndaxte tàggat yaram am na fu njariñam yem, waaye njariñu ragal Yàlla dafa daj lépp, ëmb digey àddina ak àllaaxira.
Explore 1.Timote 4:8
3
1.Timote 4:16
Sàmmal sa bopp, sàmm sa njàngle, te sax ci; kon dinga musal sa bopp, yaw ak ñi lay déglu.
Explore 1.Timote 4:16
4
1.Timote 4:1
Xelum Yàlla mi wax na bu leer ne ci mujug jamono dina am ñu bàyyi yoonu ngëm wi, di topp ay xel yuy fàbbee ak xalaati Seytaane.
Explore 1.Timote 4:1
5
1.Timote 4:7
Tanqamlul ay léebi diiney neen, di ay wax yu amul bopp yu àddina kese; waaye tàggatal sa bopp ci ragal Yàlla.
Explore 1.Timote 4:7
6
1.Timote 4:13
Li feek may dikk, saxal ci jàng di biral Mbind mi ci mbooloo mi, di leen dénk ak a jàngal.
Explore 1.Timote 4:13