1
1.Korent 2:9
Téereb Injiil
TI
Waaye Mbind mi nee na: «Lu bët gisul, nopp déggu ko, xel xalaatu ko, loolu la Yàlla dencal ñi ko bëgg.»
Compare
Explore 1.Korent 2:9
2
1.Korent 2:14
Nit kese du nangu yëfi Xelum Yàlla. Ag ndof lay doon ci moom; du ko mana nangu, ndaxte ku yor Xelum Yàlla rekk moo ko mana ràññale.
Explore 1.Korent 2:14
3
1.Korent 2:10
Fekk nag nun la ko Yàlla won, jaarale ko ci Xelam. Xelum Yàlla mooy leeral lépp, ba ci xalaati Yàlla yi gëna xóot.
Explore 1.Korent 2:10
4
1.Korent 2:12
Nun nag Xel mi nu jot, jógewul ci àddina, waaye Yàllaa nu ko sol.
Explore 1.Korent 2:12
5
1.Korent 2:4-5
Li ma wax ak li ma waare, defuma ko ci làmmiñ wu neex, sukkandikoo ko ci xam-xamu nit, waaye ànd na ak ay firnde yu soqikoo ci kàttanu Xelum Yàlla, ngir seen ngëm baña wékku ci xam-xamu nit ñi waaye mu wékku ci dooley Yàlla.
Explore 1.Korent 2:4-5