1
Room 9:16
Kàddug Yàlla
KY
Kon nag mbaaxug Yàlla ajuwul ci coobarey nit ki, mbaa aw ñaqam, waaye lépp yërmandey Yàlla la.
Compare
Explore Room 9:16
2
Room 9:15
Ndax kat moo noon Musaa: «Maay yërëm ku ma neex, te maay ñeewante ku ma neex.»
Explore Room 9:15
3
Room 9:20
Waaye yaw nit ki, yaay kan bay weddi Yàlla? Ndax këf ku ñu tabax dina ne ka ko tabax: «Lu tax nga sàkke ma nii?»
Explore Room 9:20
4
Room 9:18
Kon nag Yàlla mooy yërëm ku ko neex, te ku ko neex lay dëgëral xolam.
Explore Room 9:18
5
Room 9:21
Tabaxkatu ndab bi xanaa daa amul sañ-sañ ci ban bi muy liggéeye, ngir tabax ci bennub tooyal lenn ndabal teraanga ak leneen ndabal njoogaan?
Explore Room 9:21