1
Room 13:14
Kàddug Yàlla
KY
Waaye yiirooleen Sang Yeesu Almasi bi, te ngeen baña yittewoo seen bakkan, ngir di topp seeni xemmemtéef.
Compare
Explore Room 13:14
2
Room 13:8
Buleen ameel kenn bor, lu moy borub soppante; ndax ku sopp sa moroom, yaa matal yoonu Musaa.
Explore Room 13:8
3
Room 13:1
Na ku nekk déggal njiit yi yor kilifteef, nde amul njiit lu bawoowul fa Yàlla, te njiit yi toog, Yàlla moo leen tabb.
Explore Room 13:1
4
Room 13:12
Guddi gi màggat na, bët a ngi bëgga set. Kon nag nanu bàyyi jëfi lëndëmtu te ràngoo gànnaay yi ñuy xaree cig leer.
Explore Room 13:12
5
Room 13:10
Cofeel du waral kenn def moroomam lu bon; kon cofeel moo matal sëkk yoonu Musaa.
Explore Room 13:10
6
Room 13:7
Joxleen ku nekk li ngeen warlook moom; ku ngeen wara fey galag, feyleen ko ko; ku ngeen wara fey juuti, feyleen ko ko; ku ngeen wara weg, wegleen ko; ku ngeen wara teral, teralleen ko.
Explore Room 13:7