1
Peeñu ma 1:8
Kàddug Yàlla
KY
«Man, maay Alfa, di Omega», la Boroom bi Yàlla wax, moom Ki masa nekk, Ki nekk, di Kiy dikk ëllëg, te di Aji Man ji.
Compare
Explore Peeñu ma 1:8
2
Peeñu ma 1:18
Maay Kiy dund, maa dee woon, maay dund nii tey ak ëllëg ba fàww te maa yor caabiy dee ak njaniiw.
Explore Peeñu ma 1:18
3
Peeñu ma 1:3
Ndokkalee képp ku jàng ak mboolem ñi déglu yii kàdduy waxyu, tey sàmm li ñu ci bind, ndaxte waxtu wi jege na.
Explore Peeñu ma 1:3
4
Peeñu ma 1:17
Naka laa ko gis, ne dàll daanu ci ay tànkam ni ku dee. Mu teg ma loxol ndijooram, ne ma: «Bul tiit. Maay Ki njëkk, di Ki mujj.
Explore Peeñu ma 1:17
5
Peeñu ma 1:7
Mu ngoogu di dikk, indaale niir yi, te ñépp a koy teg bët, ba ca ña ko jamoon sax, te giiri kaw suuf yépp ay jooy ndax moom. Noonu la moos. Amiin.
Explore Peeñu ma 1:7