1
Macë 25:40
Kàddug Yàlla
KY
Bu loolu amee buur ba ne leen: “Maa leen ko wax déy, lu ngeen ci defal kenn ci ñi gëna tuut ci sama bokk yii, man ngeen ko defal.”
Compare
Explore Macë 25:40
2
Macë 25:21
Njaatigeem ne ko: “Jaaraamaa, surga bu baax bi te wóor. Gannaaw ci lu tuut nga wóore, lu bare laa lay dénk. Kaay nag nu bokk bége.”
Explore Macë 25:21
3
Macë 25:29
Ndaxte képp ku am, dees na ko dolli, ba mu barele, waaye ku amul, la mu am as néew sax, dees na ko nangu.
Explore Macë 25:29
4
Macë 25:13
«Teewluleen boog, nde xamuleen bés ba, mbaa waxtu wa.
Explore Macë 25:13
5
Macë 25:35
Ndaxte ba ma xiifee, yeena ma leel; ma mar, ngeen nàndal ma; ma dib doxandéem, ngeen fat ma
Explore Macë 25:35
6
Macë 25:23
Njaatige la ne ko: “Jaaraamaa, surga bu baax bi te wóor. Gannaaw ci lu tuut nga wóore nag, lu bare laa lay dénk. Kaay nag nu bokk bége.”
Explore Macë 25:23
7
Macë 25:36
ma rafle, ngeen wodd ma; ma wopp, ngeen toppatoo ma; ñu tëj ma, ngeen seetsi ma.”
Explore Macë 25:36