1
Luug 24:49
Kàddug Yàlla
KY
Man ci sama bopp maa leen di yónnee li sama Baay dige. Waaye yeen toogleen ci dëkk bi, ba kera ñu leen solee manoore ju bawoo fa kaw.»
Compare
Explore Luug 24:49
2
Luug 24:6
Nekku fi; dekki na. Fàttalikuleen la mu leen waxoon, ba mu génnagulee Galile.
Explore Luug 24:6
3
Luug 24:31-32
Ca la seeni gët ubbiku, ñu xàmmee ko. Moom nag, mu ne mes, réer leen. Ba loolu amee, ku nekk naan sa moroom: «Ndax yéguloo woon cawartey xol bu tooy, ba muy wax ak nun ci yoon wi, di nu firil Mbind mi?»
Explore Luug 24:31-32
4
Luug 24:46-47
Mu ne leen: «Nii lees binde, ne fàww Almasi bi dee ci biir coono, ba dekki ca ñetteelu fan ba; te ciw turam, dees na dale ci Yerusalem, yégal xeet yépp, tuubeel gu jur njéggalug bàkkaar.
Explore Luug 24:46-47
5
Luug 24:2-3
Ñu agsi ca bàmmeel ba, fekk ñu béraŋ doj wa uboon bunt ba, laf ko ca wet ga. Ñu dugg, fekkuñu fa néewub Sang Yeesu.
Explore Luug 24:2-3