1
Yowaan 9:4
Kàddug Yàlla
KY
Danoo wara liggéey liggéeyu ki ma yónni ci bi muy bëccëg; bu guddee kenn du liggéey.
Compare
Explore Yowaan 9:4
2
Yowaan 9:5
Li feek maa ngi ci àddina, maay leeru àddina.»
Explore Yowaan 9:5
3
Yowaan 9:2-3
Taalibeem ya laaj ko ne ko: «Kilifa gi, ndax bàkkaaram a ko waral, walla bu waajuram, ba tax mu judduwaale gumba?» Yeesu ne leen: «Du bàkkaaram, du bàkkaaru waajuram a tax. Da di liggéeyu Yàlla moo wara feeñe ci moom.
Explore Yowaan 9:2-3
4
Yowaan 9:39
Yeesu ne ko: «Man, ab àttee ma taxa dikk ci àddina sii, ngir ñi dul gis di gis; ñiy gis, gumba.»
Explore Yowaan 9:39