1
Yowaan 4:24
Kàddug Yàlla
KY
Yàlla xel la, kon ñi koy jaamu, xel ak dëgg lañu ko war di jaamoo.»
Compare
Explore Yowaan 4:24
2
Yowaan 4:23
Waaye waxtoo ngi ñëw, te léegi la; ci la jaamukat yi dëgg di jaamoo Baay bi xel ak dëgg, ndax ñu ni mel la Baay bi sàkku ñu jaamu ko.
Explore Yowaan 4:23
3
Yowaan 4:14
waaye ku naan ci ndox mi ma koy may, man, du marati; ndox mi ma koy may, bëtu ndox lay doon ci moom, di ball, ngir dundug texe gu sax dàkk.»
Explore Yowaan 4:14
4
Yowaan 4:10
Yeesu nag ne ndaw si: «Soo xamoon mayu Yàlla, ak kan moo la ne may ma, ma naan, kon yaw yaa koy ñaan, mu may la ndox miy dundal.»
Explore Yowaan 4:10
5
Yowaan 4:34
Yeesu ne leen: «Samaw ñam moo di jëfe coobarey ki ma yónni, ba sottal ab liggéeyam.
Explore Yowaan 4:34
6
Yowaan 4:11
Ndaw si ne ko: «Sang bi, amuloo baag, te teen bi xóot na; ana fooy jële ndox miy dundal?
Explore Yowaan 4:11
7
Yowaan 4:25-26
Ndaw si ne ko: «Xam naa ne Almasi baa ngi ñëw, moom lañu naan Ki ñu fal, kooku bu dikkee, moo nuy leeralal lépp.» Yeesu ne ko: «Man miy wax ak yaw, man la.»
Explore Yowaan 4:25-26
8
Yowaan 4:29
«Kaayleen gis; nit a nga fee, wax na ma mboolem lu ma def! Kooku du Almasi beem?»
Explore Yowaan 4:29