1
Yowaan 18:36
Kàddug Yàlla
KY
Yeesu ne ko: «Sama nguur moo bokkul ci àddina sii. Bu sama nguur bokkoon ci àddina, samay surga xeex, ba kenn du ma jébbal njiiti Yawut yi. Waaye sama nguur a bokkul fii.»
Compare
Explore Yowaan 18:36
2
Yowaan 18:11
Yeesu ne Piyeer: «Defal saamar ci mbaram. Kaasub naqar bi ma Baay bi sédd, xanaa dama ko dul naan?»
Explore Yowaan 18:11