1
Yawut ya 7:25
Kàddug Yàlla
KY
Looloo waral mu mana musal mucc gu mat sëkk, ñiy awe fi moom, dikk fa Yàlla, ndax mooy dund ba fàww, ngir di leen tinul.
Compare
Explore Yawut ya 7:25
2
Yawut ya 7:26
Boobu sarxalkat bu mag lanu soxla: moo sell, mucc sikk, mucc sobe, moom lañu teqale ak bàkkaarkat yi ci àddina, te moom lañu kaweel ba fa tiim asamaan.
Explore Yawut ya 7:26
3
Yawut ya 7:27
Bokkul ak yeneen sarxalkat yu mag yi: soxlawula jiital bés bu nekk saraxi jur ngir bàkkaari boppam, door cee teg ay sarax ngir bàkkaari askan wi. Benn yoon la Yeesu sarxale, mu doy, te mooy ba mu sarxee boppam.
Explore Yawut ya 7:27