1
Yawut ya 1:3
Kàddug Yàlla
KY
Kooku mooy lerxat leeru Yàlla, te mooy ki jëmmal nekkug Yàlla. Moo téyee lépp kàddoom gu manoorewu. Gannaaw ba mu setalee bàkkaar yi nag, fa ndijooru Aji Màgg ji la toog, fa kawte ya
Compare
Explore Yawut ya 1:3
2
Yawut ya 1:1-2
Bu yàgg la Yàlla waxoon ay yooni yoon ak maam ya, ci waxin yu bare, yonent yi jottali. Ci fan yu mujj yii, ci Doom ji la jaare wax ak nun, ki mu jagleel lépp, te ci moom la sàkke àddina wërngal këpp.
Explore Yawut ya 1:1-2
3
Yawut ya 1:14
Xanaa malaaka yépp duñu ay ngelaw yu ñu sas ab liggéey, yebal leen ngir ñu taxawu ñi wara jagoo ag mucc?
Explore Yawut ya 1:14
4
Yawut ya 1:10-11
Mu neeti: «Yaw Sang bi, ca njàlbéen ga, yaa samp suuf, sàkke asamaan say loxo. Yooyu day réer, waaye yaw yaay sax, lépp ay ràpp ni mbubb.
Explore Yawut ya 1:10-11