1
Jëf ya 4:12
Kàddug Yàlla
KY
Mucc kat amul ci keneen, ndax fi asamaan tiim, mayeesul fi nit ñi weneen tur wu nu wara mucce.»
Compare
Explore Jëf ya 4:12
2
Jëf ya 4:31
Ba ñu ñaanee ba noppi, béreb ba ñu daje daa yëngu, ñu fees ak Noo gu Sell gi ñoom ñépp; ñu daldi tàmbalee waxe fit kàddug Yàlla gi.
Explore Jëf ya 4:31
3
Jëf ya 4:29
Léegi nag Boroom bi, bàyyil xel seeni tëkkoo te nga may nu, nun say jaam, nuy wax sa kàddu ak fit wu mat sëkk.
Explore Jëf ya 4:29
4
Jëf ya 4:11
Yeesu moomu mooy: “Doj wi ngeen beddi woon, yeen tabaxkat yi, te mu mujj di doju koñu tabax bi.”
Explore Jëf ya 4:11
5
Jëf ya 4:13
Ba waa kuréelu àttekat ya gisee fit wi Piyeer ak Yowaan àndal, te ñu xam ne niti neen ñu masula jàng lañu, dañoo waaru. Xamoon nañu nag ne ñook Yeesoo nekkoon.
Explore Jëf ya 4:13
6
Jëf ya 4:32
Ci kaw loolu mboolem gëmkat ñi bokk menn xel ak benn xalaat. Du kenn ku ne moo moom lenn ci alalam, waaye ñoo bokkoon lépp ci seen biir.
Explore Jëf ya 4:32