Jëf ya 13:47
Jëf ya 13:47 KY
Ndax noonu la nu ko Boroom bi sante ba mu nee: “Tabb naa la, ngay leeru jàmbur ñi, ngir nga jottaliji wall wii, ba ca cati àddina.”»