1
2.Tesalonig 3:3
Kàddug Yàlla
KY
Waaye Boroom bi mooy ki jara wóolu, te moo leen di dooleel, musal leen ci ku bon ki.
Compare
Explore 2.Tesalonig 3:3
2
2.Tesalonig 3:5
Yal na Boroom bi wommat seen xol, jëme ci cofeelu Yàlla ak muñ gi ci Almasi bi.
Explore 2.Tesalonig 3:5
3
2.Tesalonig 3:6
Ndigal li nu leen di jox ci sunu turu Boroom Yeesu Almasi bi, moo di ngeen dànd mépp mbokk mu yaafus, te baña dëppoo ak dénkaane yi ngeen nangoo ci nun.
Explore 2.Tesalonig 3:6
4
2.Tesalonig 3:2
ngir itam nu mucc ci nit ñu soxor ñu bon ñi, ndax du ñépp a gëm.
Explore 2.Tesalonig 3:2