1
2.Korent 8:9
Kàddug Yàlla
KY
Xam ngeen kat sunu yiwu Boroom Yeesu Almasi bi, moom mi woomle woon, te yeena tax mu ñàkk, ngir woomale leen ag ñàkkam.
Compare
Explore 2.Korent 8:9
2
2.Korent 8:2
Doonte jaar nañu ci nattub njàqare bu mag, seen mbégtee rembat ci seen biir ñàkk gu tar, ba géejal seenug tabe.
Explore 2.Korent 8:2