1
2.Korent 7:10
Kàddug Yàlla
KY
Ndaxte tiis wu Yàlla namm, ag tuubeel gu jëme cig mucc lay jur, te loolu du tiis wees di tiisoo. Waaye tiisu àddina, dee lay jur.
Compare
Explore 2.Korent 7:10
2
2.Korent 7:1
Gannaaw noo moom yii dige nag, soppe yi, nanu setal sunu bopp ci mboolem sobey yaram ak ju xel, te nu sax ci sellaay ci ag ragal Yàlla.
Explore 2.Korent 7:1
3
2.Korent 7:9
Waaye tey bég naa, te du tiis wu ngeen tegoo laay bége, waaye li leen tiis wi tuubloo, laay bége, ndax woowu xeetu tiis la Yàlla namm ci yeen, moo tax it yóbbewunu leen jenn loraange.
Explore 2.Korent 7:9