1
2.Korent 3:17
Kàddug Yàlla
KY
Boroom bi mooy Noo gi, te fu Noo gi nekk, fa la nit di goree.
Compare
Explore 2.Korent 3:17
2
2.Korent 3:18
Nun ñépp nag, kanam gu muriku lanuy xoole niki cib seetu leeru Boroom bi, ba tax nuy soppiku, doon takkndeeram, tey làmboo leer guy màgg, di gëna màgg. Looloo di liggéeyu Boroom bi, moom miy Noo gi.
Explore 2.Korent 3:18
3
2.Korent 3:16
Waaye saa su nit waññikoo ci Boroom bi, muuraay bi day muriku.
Explore 2.Korent 3:16
4
2.Korent 3:5-6
Du caageenu doyloo sunu manoorey bopp, ba yaakaar ne lenn man naa sottee ci sunu wàllu bopp, waaye sunu manoore ci Yàlla la jóge. Moo nu may manoorey doon ay liggéeykati kóllëre gu bees gu ajuwul ci mbindum ndigali yoon, xanaa kóllëre gu aju ci Noowug Yàlla. Ndaxte mbindum ndigali yoon day rey, te Noo gi di dundloo.
Explore 2.Korent 3:5-6