1
1.Tesalonig 5:16-18
Kàddug Yàlla
KY
Deeleen bég, di saxoo ñaan, te di sant ak nu mu mana deme. Loolu mooy coobarey Yàlla ci yeen ñi ànd ak Almasi Yeesu.
Compare
Explore 1.Tesalonig 5:16-18
2
1.Tesalonig 5:23-24
Yàlla ci boppam, moom miy Boroom jàmm, yal na leen sellal, ba ngeen mat sëkk, te seen léppi xel ak seen léppi xol ak seen léppi yaram sàmmu, ba mucc sikk, ba kera bés bu sunu Sang Yeesu Almasi bi feeñee. Ki leen woo de ku wóor la, te moo koy def it.
Explore 1.Tesalonig 5:23-24
3
1.Tesalonig 5:15
Fexeleen ba kenn du feyantoo. Waaye lu baax, deeleen ko deflante ci seen biir, te di ko defal ñépp.
Explore 1.Tesalonig 5:15
4
1.Tesalonig 5:11
Kon nag noonu ngeen di ñaaxantee aka yokkante, nangeen ko wéye.
Explore 1.Tesalonig 5:11
5
1.Tesalonig 5:14
Bokk yi, danu leen di dénku; yaafus yi, femmuleen leen; ñi néewu fit, ñaaxleen leen; néew-doole yi, dimbalileen leen, te it muñalleen ñépp.
Explore 1.Tesalonig 5:14
6
1.Tesalonig 5:9
Ndax kat Yàlla séddu nu am sànj, waaye ag mucc la nu moomale ndax sunu Sang Yeesu Almasi bi.
Explore 1.Tesalonig 5:9
7
1.Tesalonig 5:5
Yeen ñépp ay doomi leer ngeen, doomi bëccëg ndarakàmm; nun bokkunu dara ak guddi, mbaa ag lëndëm.
Explore 1.Tesalonig 5:5