1
1.Tesalonig 3:12
Kàddug Yàlla
KY
Ni sunu cofeel ak yeen baawaane, yal na ko Boroom bi yokke ba baawaanal ag cofeel ci seen biir ak ci seen diggante ak nit ñépp.
Compare
Explore 1.Tesalonig 3:12
2
1.Tesalonig 3:13
Yal na Boroom bi dooleele noonu seen xol, ngir kera bu sunu Sang Yeesu délsee, ànd ak ñoñam ñu sell ñépp, fekk leen sell te mucc sikk, fa kanam Yàlla sunu Baay.
Explore 1.Tesalonig 3:13
3
1.Tesalonig 3:7
Kon nag bokk yi, ci sunu biir mitit ak njàqare, sunu xol sedd na ci yeen ndax seen ngëm.
Explore 1.Tesalonig 3:7