1
1.Korent 3:16
Kàddug Yàlla
KY
Xanaa xamuleen ne kër Yàlla ngeen, te Noowug Yàlla moo dëkk ci yeen?
Compare
Explore 1.Korent 3:16
2
1.Korent 3:11
Geneen fondmaa moom maneesu koo lal, xanaa gi xasa lale, te mooy Yeesu Almasi bi.
Explore 1.Korent 3:11
3
1.Korent 3:7
Ki jëmbat nag ak ki suuxat, kenn du ci dara, xanaa Yàlla miy jebbil doŋŋ.
Explore 1.Korent 3:7
4
1.Korent 3:9
Noo bokk diy surga ci liggéeyu Yàlla bi; yeen ngeen di toolu Yàlla, di tabaxub Yàlla.
Explore 1.Korent 3:9
5
1.Korent 3:13
ku ci nekk, sab liggéey dina feeñ, ndax bés-pénc baa koy xamle, nde sawara lees koy feeñale. Ku ci nekk ak lu sa xeetu liggéey mana doon, sawara lees koy natte.
Explore 1.Korent 3:13
6
1.Korent 3:8
Ki jëmbat, ak ki suuxat ñoo yem kepp, waaye ku ci nekk kemu liggéeyu boppam lay yooloo.
Explore 1.Korent 3:8
7
1.Korent 3:18
Bu kenn nax boppam: ku teg boppam ci yeen boroom xam-xam, ni xarnu bii jàppe xam-xam, kooku na doon ab dof, ngir am xam-xam bi wóor.
Explore 1.Korent 3:18