Room 3:23-24
Room 3:23-24 TI
Ñépp a bàkkaar, ba joteetuñu ndamu Yàlla. Waaye gannaaw Kirist Yeesu dee na ngir jot leen, Yàlla ciw yiwam man na leena àtte ni ñu jub ci dara.