Room 3:10-12
Room 3:10-12 TI
Moom la Mbind mi wax ne: «Ku jub amul, du kenn sax. Amul kenn ku xam yëfi Yàlla, mbaa kenn ku koy wut. Ñépp jeng nañu, ba kenn amalatul Yàlla njariñ. Kenn du def lu baax, du kenn sax!