Peeñu ma 12:9
Peeñu ma 12:9 TI
Daaneel nañu ko, moom ninkinànka ju réy ji, di jaani cosaan ji, te ñu di ko wax Tuumaalkat bi mbaa Seytaane, moom miy nax waa àddina sépp-- daaneel nañu ko ci kaw suuf, moom ak i malaakaam.