Bible App logo
Search Icon

Kolos 2:8

Kolos 2:8 TI

Moytuleen ba kenn bañ leena fàbbi ci ay xam-xami nit yuy naxi neen. Xam-xam yu mel noonu, ñu ngi soqikoo ci aada yu nit tëral, ci aaday àddina, waaye soqikoowul ci Kirist.