Bible App logo
Search Icon

1.Timote 2:1-2

1.Timote 2:1-2 TI

Fii laay tàmbalee nag: maa ngi leen di dénk, ngeen yóbbu ñépp fa kanam Yàlla ciy ñaan, ay tinu ak i ngërëm. Ñaanal-leen buur yi ak kilifa yépp, ngir nu mana am dund gu dal te jàmmu, ànd ak ragal Yàlla ak faayda yu mat.

Verse Image for 1.Timote 2:1-2

1.Timote 2:1-2 - Fii laay tàmbalee nag: maa ngi leen di dénk, ngeen yóbbu ñépp fa kanam Yàlla ciy ñaan, ay tinu ak i ngërëm. Ñaanal-leen buur yi ak kilifa yépp, ngir nu mana am dund gu dal te jàmmu, ànd ak ragal Yàlla ak faayda yu mat.

Free Reading Plans and Devotionals related to 1.Timote 2:1-2