1.Timote 2:1-2
1.Timote 2:1-2 TI
Fii laay tàmbalee nag: maa ngi leen di dénk, ngeen yóbbu ñépp fa kanam Yàlla ciy ñaan, ay tinu ak i ngërëm. Ñaanal-leen buur yi ak kilifa yépp, ngir nu mana am dund gu dal te jàmmu, ànd ak ragal Yàlla ak faayda yu mat.






