Tit 2:7-8
Tit 2:7-8 KY
Te nanga doon, yaw ci sa bopp ab royukaay ci lépp ndax sa jëf ju baax, te nga boole ko ak àlluwa ju dëggu te tedd, ak kàddu gu wér gu kenn dul mana weddi, ngir rusloo ab noon bu amul lenn lu bon lu mu nu baatale.